xet wu jekwi | jokko ak ñun | li aju ci ñun
   05:33 GMT limu xabaar yi: 0
gёstu:
listu xabaar ak xew xew yi mujju téñu gëstuko
dañ kuppa xabaar yi
ligéey yi ak yenggu yenggu yi
jokkoo yi
laaye biir yi
yoonnée xabaar yi
yaxu al xur´aan bu matt sёkk
lefol qur’aana

‌ Dinañu amal ab gaaralu keemtaanu al xuraan yi ca reewum Amerique
Waallu bitim reew gaaralu keemtaanu al xuraan yi ci nimbalu kureel giidi yenggu ci wone art islaam ci reewum Amerique (IAE) lañukoy amalee


Ubbinañu njëlbeenu banque islaam ca reewum Nigeria
Waallu bitim reew njëlbeenu banque islaam ci reewum Nigeria deemb 18 fevrier lañuko tijji ginaaw bi xamne lu toollu ci weer ñungidoon waxtaan ak nguur gi
xabaar yi ñi natal
 
Njёlbeenu lёllu aduna wёrngёlkёp biñu duppee (sama ñaang)
Kёru xabaar biidi (ikna) seexna ab waxtaan ak ayy kilifa ci reewum Liban ci li nga xamne moo soxal mbiri kiidi Imaam Musaa sadr
mbolém xabaar yi
 
yegu yegu xuraan

Daara ci diir bu gaat ngir jaangale al xuraan ak tajwiid te ñukodoon amalee ci reewum Inde yeggna ci cёpaa ndaw gi

Amalnañu jotaayu sargal ak deelloo njukël soxna yi nga xamne dañoo woottu kaamilu al xur’aan bi ci reewum Afganistan

politique - dundin

Aartu komite bi nga xamne jullit ñi ak cretienne yi ñooko seex ci pexe yi nga xamne yaxuud yi ñungikoy def ngir xuds neekk dёkk yaxuud ‌

Dinañu amal ca reewum Kongo xew xewu ñent fukki guddi Imaam xuseyn yi

xam xam – aada

Dinañu jaangat waccuwaay ak place bi nga xamne xew xewu karbalaa amnako ci aada ak cosaanu reewum Iran

Dinañu amal ab jonŋante ci waallu Irfan ak tasawuf ca reewum Chine

bitim réew

Dinañu amal ab atelier jaanagle buñu duppee (gise ak islaam) ca reewum Belgique

Dinañu amal ca reewum Kanada ab lëll ci dekkil ak dundal cofeel ci yonent bi

 
xabaar yi muju té am solo
 
Siiwalnañu soxna yi nga xamne ñoo gёna raañeeku ci waallu gottali kaaddu yaalla ci reewum Chine
Doornañu yoonee ligeey ak jeexintal ngir bokk ci jonŋante bind yu rafet
Jawriñ jiñu deekk waallu kaaraange ci reewum Amerique jeggaluna jullit ñi
Dinañu amal fukk ak ñentteelu gaaralu islaam ca Paris
Askanu reewum Afganistan amalnañu ab doxu ñaxtu ngir ñaawlu lakk gi nga xamne lakknañuko al xuraan
Adiis yu wër yi nga xamne moo baayeeko ci yonent bi mooy naanukaayu islaam bu muccu ayib
Dinañu yeesalaat njёlbeenu jumaa ci aduna bi yёpp
nataalu bésbi
 
 
E-Mail: intl@ikna.ir
2003 - 2012 këru tasukaayu xabaaru al xur'aan ci bitim réew.